Tang Xol

  • TANG XOL : Entraîneur ak joueur, kan mooy traitre

    22-08-2016

    XWaaw lii moom jaxal u leen… Entre l’entraîneur et le joueur, le masque du traître change souvent de camp selon la situation. Leek leek ñu mel mburu ak soow. Un entraineur, discute et échange beaucoup avec le joueur tant que celui ci est susceptible de régler son problème sur le terrain.

  • Man sélectionneur, lii mooy sama porogram

    22-08-2016

    Défense de rires. Puisque sur les réseaux sociaux, ku nek yaa ngi ngemb sa mbër, tey baku naan mo gën si «Lions» yi, man tam it da may laac pour remplacer Giresse. Je sais que je n’ai pas été un bon footballeur, mais bu fekoon ne mën futbal moy taxa jël cup, kon Giresse du lajj.